serge-wilson/wav2vec-large-wolof
Automatic Speech Recognition • Updated • 6
audio audioduration (s) 2.29 12.5 | sentence stringlengths 26 118 |
|---|---|
moo taxit feebaru jigéen dafa bari façons | |
bu nawetee du génn te gànnaayoowul ak permiyaabal | |
kii de dafay wanteer njëg li neex na lool | |
léegi daawur dafa mel ni ku télbati | |
delloo na naaru góor wi tëboon wajanam wi | |
ci saa si ayda jafandu ci waasintóoram yu tuuti ya | |
Nee ñu xobi pàppaayo baax na ci fas yi seen biir di metti | |
ku woor di togg mën naa am nga juubu mos xorom | |
ba mu egsee ca dëkk ba booba ñépp a nga woon ca tool ya ba mu des ndew ma mu fekk ca buntu néegam | |
ruuxal soow mi ndax soppuma ci sañ yi | |
tamaate fàrsi jaa ngi noy nepp kenn mënu ko dagg | |
mu fab ko saggane ko te ndeyam amoon ko muy benn doññ | |
mu nga jóge woon ca rëbb ma gàlloo genn kéwél | |
mbëtt mënula daw mënula jaab lu dul bar bari | |
sa yaraale bi màgg na léegi yow lañuy xaar | |
reeni xom xom fajkat yee koy jëfandikoo | |
muy toj mu ndaw di toj mu mag mënees nañoo tiim | |
saalu gerte tubaab rekk la xale yi bëgg | |
fas wa dellu fëx nekk ca la mu nekkoon | |
ki sàcc sa nag yi du jaar ci saawo si | |
buur ne ki rey ninki nanka bi lay may doomam | |
këram la waaye dëkku ci dafa ko luye | |
boo raxasee aset yi ba noppi nga fomp leen | |
mbubb ma nga soloon ca céet ga booba laa bëgg | |
mu jëm ca sàmba seytaane amari né ko | |
amul bàyyi ni ko ndax am na jur gu dem | |
dalal nga sama xel bi nga ma nee am na liggéey | |
morooman yi gunge nañu ko ba gaar ba | |
soo leen boolee dinañu gaawa xaritoo | |
fompal lumbi deret yi bala nga koy faj | |
moo yey Noy ci liggéeyam moo ko tax a suturlu | |
bu jëkk jigéen ñi begguñu woon sew dañu daan yaflu | |
Naar Naar Naar ba Naar yépp tiit daldi jóg ni ko | |
mag ñu jëkk ña daawuñu génn te takkuñu nafa | |
booy dem màrse ma yóbbante la kànja | |
ba jànq ya indee meew ma xale yu góor yi daldi naan | |
dafa bàyyi woon ay waajuram moo tax mu alku | |
seen ndën li yal nangeen ko yàgga def | |
kon dey ma dal di tegale samay ndab te dem | |
yaay ji ni ko benn lam bu ma sa baay mayoon bi mu ma takkee | |
ñu toogati lu yàgg ba ñépp fàtte | |
yaay ji ni ko benn lam bu ma sa baay mayoon bi mu ma takkee | |
jamanoy tàngaay ci teraas bi lañuy lekke | |
maa ngi nii nag waxal nag loo ma fi mayul ma delloo la ko | |
leegi li ñu wara def mooy balu ko te daw seeti feneen | |
fas di nà dov vandé rutimgeer à cà ràv | |
darkase yi meññuñu ndax bekkoor bi | |
xale bi raatale na laax bi ci dënn bi | |
loolu laa amoon lu ma leen di wax wasalaam | |
xaaral ba nu matal ay gii nga soga bokk | |
kër gu xate nii kenn mënu fi yar xar | |
wër nañu xale bi ba tàyyi gisuñu ko | |
saaga yu ñaaw lay génne ci gémmiñam gi | |
dégg naa ne kër googa dafay jaay luññutu ko | |
bu jur gi màngsee dañu leen di abal karas gi | |
amoon na fi jigéen ju bon ju nekkoon ag ñeenti doomam | |
mënuma laa dab yaa ma gën a gudd i jéego | |
toppatool xale bi dafa mel na ku tojal | |
xaaral ba suuf si màndi nga sog di gas | |
moo xale bi yow reew nga di waaw lu doon say tànk sax | |
xawma lu ko jot yaram mi dafa def yu mel ni ay càqar | |
sama maam a ma defarluloon seN oor bii | |
mbom la dagg bënn mi nii ni na doon bàmmeelam | |
mu ngi jonkon ci wetu taal bi di jaaru | |
mu ngi topp tali bi di tëñëx tëñëxi | |
balawlaw tàppit malaan a ngoog am yobbaale ko buur | |
li mu doon daw moo tax noyyi gi gëna gaaw | |
miskin yu bare la yélimaan jooju daan leel | |
xale bi laaj ko loo dagge sama butitu njurukaay | |
tëggkat yi tàmbaleeguñu ñu ngiy foddat ndënd yi | |
ci wetu seju la toolu banaana yi nekk | |
wax ju jëkk fasu par la tontu la naaru góor | |
mu daldi jël li mu soxla dem mu delluwaat ci yaayam ni ko | |
gàpp bi weesu na bu yàgg dama koy seeti ndax ma soññ ko | |
dafay gelu yaayam yóbbuleen ko ci moom | |
góomam bi dafa wunni bi mu ci defee sunguf si | |
badoolë bou bagn é ligaiye bagn é k mbok ëm | |
ki sàcc sa nag yi du jaar ci saawo si | |
bi mu tàmbalee jël garab googu ba tey miiratul | |
soo ko wutaloon mbaxana doon na baax ci naaj wi | |
damaa am ab rëq rëq ci li ma doon def | |
boo ko dénkul woon say mbóot lii du la dal | |
dafa ko seen rekk ne wëréñ ne mott | |
dama bëgg xam këf ki mu dugal ci waxande wi lu mu doon | |
sa ceebu tey bi wesaN na démb dafa xawoon tooy | |
altine biy ñów lañuy wori bu soobee yàlla | |
danga bëgg ci sama màngo bi waaye du jaar ci sa bóli | |
li nga wax leerul nee ma maa ngi jëm béréb sàngam | |
bu ñu noddee fajar dafa naan fojjet jóg | |
demal foo jublu yàlla na fa yiwu yàlla jublu | |
boo fi fekkulee xaalis bu jàppandal duma la mëna dimmali | |
xale yu tuuti yi nga xam ni xamuñu dara mu bàyyi leen | |
Nit ka déglu ko ba noppi dal di fiddi | |
soldaar yi amatuñu bal amatuñu puudër | |
këriñ gi du gaawa jàpp ndax dafa tooy | |
bañuñu koo bind matadi gi mu àndal a tax | |
fekk ma tool ya am na liggéey bu ñu fa war def | |
lu mpicà baré baré du téré ji dugup | |
bu ñu bëggee falu di wuta peeg nit ñi | |
janq yu ndaw ndawaan yi lañu fiy jàngal togg |
Dataset de reconnaissance automatique de la parole (ASR) en wolof, une langue d'Afrique de l'Ouest parlée par plus de 10 millions de locuteurs, principalement au Sénégal.
Ce dataset est un miroir HuggingFace du corpus wolof du projet ALFFA hébergé à l'origine sur GitHub par le laboratoire GETALP (Grenoble).
Ce dataset provient du projet ALFFA :
| Split | Échantillons |
|---|---|
| Train | 12 599 |
| Test | 2 245 |
| Total | 14 844 |
| Colonne | Type | Description |
|---|---|---|
audio |
Audio | Signal audio |
sentence |
string | Transcription en wolof |
from datasets import load_dataset
dataset = load_dataset("serge-wilson/wolof_speech_transcription")
train = dataset["train"]
test = dataset["test"]
example = train[0]
print(example["sentence"])
# "moo taxit feebaru jigéen dafa bari façons"
Si vous utilisez ce dataset, veuillez citer le projet ALFFA original :
@inproceedings{gauthier2016collecting,
title={Collecting Resources in Sub-Saharan African Languages for Automatic Speech Recognition: a Case Study of Wolof},
author={Gauthier, Elodie and Besacier, Laurent and Voisin, Sylvie and Melese, Michael and Elingui, Jonathan},
booktitle={Proceedings of the Tenth International Conference on Language Resources and Evaluation (LREC'16)},
year={2016}
}
Merci au laboratoire GETALP et aux auteurs du projet ALFFA pour avoir rendu ces données disponibles en open source.