Dataset Viewer
Auto-converted to Parquet Duplicate
id
stringlengths
10
10
speaker_id
stringclasses
6 values
locale
stringclasses
1 value
audio
audioduration (s)
2
334
text
stringlengths
28
2.89k
gender
stringclasses
2 values
wol_2_0175
2
wol
Dakar mooy geubleu Sénégal. Lii eupp ci yëngou-yeungou yi ci wallou koom-koomu ak polotik, fii la nekk. Bari na ay barab you gandiarou ci mboor walla mbatiite niki Gorée... Ndar niou gueun ko xam ci Saint Louis, deukk bou mboorou nekkee ci beut gànaarou réewmi. Niou ràgné ko bou baakh ndax tabakhinou keur yi di fàttali...
female
wol_8_0210
8
wol
Société africaine de Raffinage (SAR) ab barabu liggéeyukaay bu Sénégal la nekk ca diwaanu Mbao ci wetu Dakar. Gnu ngi ko taxawal atum 1961 ci xalaatu nguuru Sénégal ak bu Société Africaine de pétrole (SAP), ci jonganteb barab yu mag yignuy liggéeyee lu jeum ci soroj. Alxames 29 awril atum 2010, Saudi Binladin Group nek...
female
wol_8_0189
8
wol
Jeux olympiques you nawett bu atum gnaari junni ak gnaar fukk ak gneent yi, te gnou koy woowee Jeuwou XXXIII olympiade, dinagnou leen amal li ko dalee gnaar fukki fan ak juroom-benn ci weeru sulet ba fukki fan ak benn ci weeru Aout biir Paris ca France. Dëkk bi tànnees naniou ko ca bagnouy amal téeméer ak fanweer ak be...
female
wol_1_0115
1
wol
Léopold Sédar Senghor, ndjiitou réew mi ndjeukk ci Sénégal, taalifkat bou niépp ragné lawoone
male
wol_3_0074
3
wol
niral ak nqamtou fanweer: ab waxambaané bou y màggal bésou juddoom moo jeund fanweeri gato seddale ko ci fanweeri keur ngir màggal fanweeri atam.
female
wol_4_0222
4
wol
Nit ku ne am na sañ-sañ ñu jàngal ko, njàng mi waruñu ci fayaku lu mu bon bon ci njàng mu suufe mi te am solo. Njàng mu suufe mi lu war la. Njàng mu xarala mi, te it aju ci wàllu liggéey war nanu koo wasaare. Amul xeej ak seen njàng mu kawe mi ubbil nañu ko képp ku ko yelloo. 2. Njàng war naa indi naataange gu yaa ci d...
male
wol_2_0027
2
wol
meun nanou wax ne linouy guiss palanteer la bou gnou tek benn potu fuloor bou  am fuloor firi té ubbi rido yi.
female
wol_2_0060
2
wol
xaaj bo ci yokkee benn juroom-benneel mou diokh la niaari niétteel.
female
wol_2_0116
2
wol
Abdoulaye Wade nietteelou Ndjiitou réewmi, dawna ci ngour gui lou tollou ci niaar foukki ate ak diourome bénneu
female
wol_3_0006
3
wol
limay guiss ci nataal bi benn ndongo def mooy ab mbégué bou  bakha ak biddiiw bou weekh, am juroom-benni bànqaas nekk si biiram si digg bi nag.
female
wol_8_0072
8
wol
niral ak nqamtou fukk ak gnaar: fukk ak gnaareelou weer bi ci at mi weeru xumbaay la, fukk ak gnaari woykat gnoo doon teugg ca Place de la Nation sénégalaise.
female
wol_8_0021
8
wol
sàmmkat bi am na yeukk bou mag bou wékh ak nioul, mou takhaw di khool ci kanam.
female
wol_4_0009
4
wol
xale bi dafa dieul benn kees bou bakha mou def ci gnetti tomb yu neuteukh you mag. Gnaari tomb yi nekk ci kaw yenen gnaar yi ci souuf ci benn wétou kees bi.
male
wol_2_0185
2
wol
Sine Saloum, barab bou bari ay doun la, niodior, palmarin, moundé
female
wol_4_0051
4
wol
khaadiou téeméer mooy diouroom foukk
male
wol_1_0125
1
wol
Ban waykat ci Sénégal moo meussa nekk dieuwrigne ci gornemang Sénégal ? Youssou Ndour nekk dieuwrigne dji niou dénk wàllou mbatiit ci ndieulbénou ngourou Macky Sall.
male
wol_3_0203
3
wol
Kureelu Mbootaayu Xeet yi ndawi réew yu mag yi, yu ci mel ni Nguur-Yu-Bennoo , Diiwaan-yu-Bennoo yu Aamerig, Bennog Sofyet, Faraas ak Siin, danoo daje woon ci Wasington peeyub Amerig ci wenn waxtaan atum 1933, ginaaw bi as leuf ci ndam tàmbalee feeñ ñeel réewi tapoo yi . Ci noonu nu geustu woon nan lanu fiy sose ag mbo...
female
wol_1_0046
1
wol
fukk ak benn boo ci yokkee gnett mu jox la fukk ak gneent.
male
wol_2_0206
2
wol
Macky sall moo ngi judd fukki fan ak benn ci weeru desambar atum junni ak juroom-gneenti téeméer ak juroom-benn fukk ak benn ca Fatick, ab ndawu nguur la ci réewum Sénégal.mi ngi nekk njiitu réewu Sénégal ci atum gnaari junni ak fukk ak gnaar ba léegi. Bokk ci PDS, jàppale na njiitu réew mi Abdoulaye Wade ci bi gnuy am...
female
wol_3_0135
3
wol
Hopital Principal bou Dakar, Raglou (barabou fadioukaay) bou yàgue la, niou oubbi ci 1884 guinnaaw biniou teudjé raglou bou Gorée.
female
wol_1_0025
1
wol
baraada bou gnoul am lou wékh niou teudj ko boubakh  teg ko ci kaw taal bi.
male
wol_5_0084
5
wol
tey ci àllarba jii tangaay bi gueuna kawe dina tollou ci fanweeri degrés bi geuna yées fukk ak juroom-gnaari degrés te naaj bi dina tàng ànd ak ngelaw lu sew. Benn waxtou ci beuthieug bou  tegee gneent fukki simili ba gnaari waxtu ci beuthieug you teg gneent fukki simili ak juroom, benn pàthie rekk ci réewmi jant bi di...
female
wol_5_0182
5
wol
Dindifélloo bokk na litakh, gan yiy nieuw Sénégal di dem khooli Kédougou
female
wol_8_0060
8
wol
niétti diouroom niétteel nga foul ko diouroom niétti yoon mou diokh la niétt
female
wol_8_0167
8
wol
Moussa dé ci wérou barakhlou la takk Diabaté dontê Niou bari daniou koy bagne.
female
wol_5_0211
5
wol
Société africaine de Raffinage (SAR) ab barabu liggéeyukaay bu Sénégal la nekk ca diwaanu Mbao ci wetu Dakar. Gnu ngi ko taxawal atum 1961 ci xalaatu nguuru Sénégal ak bu Société Africaine de pétrole (SAP), ci jonganteb barab yu mag yignuy liggéeyee lu jeum ci soroj. Alxames 29 awril atum 2010, Saudi Binladin Group nek...
female
wol_4_0163
4
wol
Ci gokh you bari ci Sénégal daniouy téré Toukki Àllarba
male
wol_3_0121
3
wol
Kan mooy footballkat bi eupp limou dougal ay bii ci Senegal ? Léegi Sadio mané moo eup bii yumu dougal ginnaaw bamou rombé Henry Camara.
female
wol_1_0113
1
wol
Ban réew la Tombouctou nekk ? Tombouctou mou nga tcha Mali, deuk bou làmboo mboor mou gandiarou tchi wallou xam-xam ak mbatite.2) Bamako geubla ban réew la ? Bamako mooy geublak Mali, di sélébeyoon bu am solo ci zallou dieund ak diaay ci Afrig Soowdiant.3}Fan la Ali Farka Touré Thiosaanoo ? Ali Farka Touré, waykat bou ...
male
wol_4_0053
4
wol
Niénteelou niaar foukk mooy diouroome
male
wol_5_0064
5
wol
match futbal bou  amoon ci diggante Real Madrid ak Barcelone bou  real mujjee yobbou  ndam li ci gneenti bal ci gnaar. Butou réeal bi njeukk Vinicius moo ko dugal, gnaareelu but bi Bellingham, gnettekogneelu but bi Rodrygo, kaaréelu but bi Bellingham waat. Butou Barcelone bou  njeukk bi Lewandowski moo ko dougal gnaare...
female
wol_8_0209
8
wol
Franc CFA (mbootaay ci wàllum koppar ci afrik ) ab xaalis la bu juroom-gnetti réew yi bokk mbootaayu koom-koom ak koppar bu afrik sowu jant (UEMOA) bokk: Benin, Burkina Faso, Cote d’Ivoire ; Guinée-Bissau (gnaari fan ci weeru mee atum 1997 ba léegi) Mali (ba atum 1962 ginnaaw gi ci atum 1984), Niger, Sénégal ak togo. G...
female
wol_2_0064
2
wol
match futbal bou  amoon ci diggante Real Madrid ak Barcelone bou  real mujjee yobbou  ndam li ci gneenti bal ci gnaar. Butou réeal bi njeukk Vinicius moo ko dugal, gnaareelu but bi Bellingham, gnettekogneelu but bi Rodrygo, kaaréelu but bi Bellingham waat. Butou Barcelone bou  njeukk bi Lewandowski moo ko dougal gnaare...
female
wol_4_0037
4
wol
aw fas wou rose te geen gi ak karawam gi weex bo y daw jant bi tiim ko la gnou def ci nataal bii.
male
wol_2_0014
2
wol
ci nataal bii gnou dieulee ci ab site gnou ngi ciy guiss àlleu bou  naat ak ay garab you bari gnouy séen ay dodj yu kawé ci asamaan sou bakha am touti niir.
female
wol_5_0080
5
wol
Mu ngi taw tey ci àllarba bi bi juroom-gneenti waxtu ci souba jotee te tàngaay bi tollou ci foukk ak juroom-gneenti degrés. gaawu ak dibeer jant bi dina génn ba tàngaay bi bi àgg ci gnaar fukk ak juroom-gneenti degrés ci gaawu bi. kon meun  nagnoo wax né neex naa dem géej ngir féexlu tuuti. ci alxames bi, àjjuma, altin...
female
wol_4_0188
4
wol
Senegaal menn la ci réew yi ne ci Sowu Afrik, mu bokk nag ci Afrik gu beuj-saalumu saxraa (Afrique sub-saharienne), Mbàmbulaanug Atlas di diigam ci sowu, taqaloo ak Gànnaar ci beuj-gànnaar ak penku, Mali féete ko penku, Ginne ak Ginne Bisaawóo ci beuj-saalum, Gàmbi moom sos ab daanaka-jiba (quasi-enclave) ci biir Seneg...
male
wol_3_0100
3
wol
Nit kou nekk sagne na am keuyitou deukkam. Kenn amoul sagn-sagn khagne nit keuyitou deukkam walla khagn ko mou soppi ko sou beuggé
female
wol_8_0029
8
wol
ab bant bou neuteux  bougnou dindee ci garabou  banaana te ànd ak ay xobam you neuteukh te gnou teg gnetti banaana you mbokh you reuy ci kanamam.
female
wol_8_0082
8
wol
Tay ci àlleuarba bii di fanweeri fan ak benn ay taw yu am doole la gnuy xaar si guddi gi. Bou  juroom-benni waxtu ci souba jotee taw bi dina daanu ba toll ak fukk ci téeméer boo dieul, ci noonu taw bi dafay geuna yokk ba àgg ci juroom-gnett fukk ak gnaar ci téeméer boo dieul bou  gnaari waxtu jotee. Dinagnu guiss ni ja...
female
wol_4_0059
4
wol
Tamndareet boo ko xaajee juroomi yoon mu jox la gnaar téeméeri junni.
male
wol_8_0036
8
wol
aw fas wou rose te geen gi ak karawam gi weex bo y daw jant bi tiim ko la gnou def ci nataal bii.
female
wol_4_0033
4
wol
sama baay ginnaaw bi mu dégloo météwoo la génnee parasolam bii am melo yu beuri te woute, mu ubbi ko nii.
male
wol_2_0012
2
wol
ab gnettekogne bou neuteukh bou nekk ci kaw mbégué bou bakha taqaloo ak moom mbégué bou bakha bou nekk ci souufou gnettekogne bou neuteukh taqaloo ak moom.
female
wol_4_0092
4
wol
ayu-bésou fukki fan ak juroom-gneent jàpp gnaar fukki fan ak niétt ci weeru feewiryee ci at mii nekkoon na jamono jouniou raanié ndax peund bou  mouroon jàwwou ji ci deukk you bari ci biir Sénégal.
male
wol_8_0004
8
wol
ab dioubcogne bou   wiyolé bou gnouy guiss nietti pentagone you giri gnaar yi ci kaw benn bi ci souf seen digganté.
female
wol_8_0151
8
wol
koor, tabaski, korité, gamou, jàkka, magal, tamxarit, tisbaar, taakusaan, timis, guéé, julli, jullit, 4 Afril
female
wol_3_0170
3
wol
Diggi gamou ci laniouy magal dioudou Yonent dioulite yi
female
wol_5_0208
5
wol
Amy Mbacké Thiam moo ngi judd fukki fan ci weeru nowambar atum junni ak juroom-gneenti téeméer ak juroom-gnaar fukk ak juroom-benn ca Kaolack, moo ngi nekk ab atlet bu réewum Sénégal di dawkatu gneenti téeméeri meetar yi. Moom moo nekk kenn si taarixu Sénégal ku mos a jeul raaya bu jongante bu àdduna bi yeupp di seq. ...
female
wol_1_0035
1
wol
maa teg ci taabal ji ab pom bou  neuteukh bou  nekk ci ginnaaw xaajou pom bou  neuteukh.
male
wol_2_0036
2
wol
gnetti yamb youy naaw benn bi jiitu gnaar yi nekk si ginnaawam di naaw tiim ay fuloor te bokk fignouy xool gnoom gneup.
female
wol_3_0186
3
wol
altine, ay diounney soppé ak kilifaay futbal bi te njiitu FIFA bi Gianni Infantino bokk ci dadjé nagnou ci kanamu keesu néew bu gnuul bou Pelé,  ci diggou estad bou FC Santos kolob bi mu foutbalee atum junni ak juroom-gneenti téeméer ak juroom fukk ak juroom-benn ba atum junni ak juroom-gneenti téeméer ak juroom-gnaar ...
female
wol_5_0163
5
wol
Ci gokh you bari ci Sénégal daniouy téré Toukki Àllarba
female
wol_3_0026
3
wol
sama yaay tég na ci taabal ji gnaari oraas yu gnu yàggul witti, mou taqale leen ak benn xaaju oraas bou nekk seen kanam.
female
wol_3_0213
3
wol
Tàkku Lompoul ab barab bu ndaw la bu ne weuyeung féete ca sowu-kaw bu sénégal si diggante Dakar ak Saint-Louis. Mu ngi ci diwaan u Louga, lu néew fukki kilomeetar ci géej gi ci diggante Lompoul-sur-mer ak Kébémer. Yaatuwaayam mu ngi tollou ci fukk ak juroom-gnetti kilomeetar kaare. Kaweewaayou suuf yi meun nagnou àgg g...
female
wol_8_0077
8
wol
Tay ci àllarba ji, ci gnaari waxtou ci souba asamaan sou xiin la gnouy guiss ak tàngaay bou  tollou ci juroom-gnetti degrés. Sou gnétti wakhtou dioté dinagnou guiss ay taw ak tàngaay bou  tollou ci fukki degrés ci souba ba gnaari degrés ci ngoon. Ayou-bés bii dina sedd lool kon xalaat leen génné mbàdj yi ak yeuré you d...
female
wol_4_0215
4
wol
Nit ku ne am na sañ-sañ liggéey, tànn it ci eanam gu ko neex liggéeyamm te mu dëppóok ay sàart yu yam te baax ci wàllu liggéey. Te it ñu aar ko ci ñàkkub liggéey. 2. Amul xeej ak seen ku néppam nanu sañ-sañ ñu fay leen, te loolu méngóok li mu aliggéey. 3. Keépp kuy liggéey am na sañ-sañ ñu jox ko pay gi mu yellool, baa...
male
wol_4_0034
4
wol
Waxambaané bi dafay yar xaj biignou guiss ci nataal bi di fo ak bal bii te mu takk ci baat bi buum.
male
wol_2_0066
2
wol
limou fukki dekh yi geun a gudd ci àdduna baa ngi nii: bi ci njeukk mooy Amazone ca Amérique, gnaareel bi Nil ca Afrique, gnettekogneel bi Yangtze ca Asie, kaaréel bi Mississipi ca Etats-Unis, juroomeel bi Lenissei ca Sibérie, juroom-benneel bi Huang He ca Asie, juroom-gnaareel bi Fleuve Ob ca Asie, juroom-gnettekognee...
female
wol_1_0105
1
wol
Tour yi geuna bari Sénégal ci goor gni niooy : Ablaye , Abdou, Mamadou, Ibrahima, Pape, Assane, Adama Lamine, El Hadj Tourou djiguéne yi geuna bari niooy : Ndèye, Fatou, Astou, Amy, Khady, Marème, Adja Sant yi geuna bari niooy : Ndiaye, Diop, Sarr, Diallo, Coly,Diouf, Gueye, Ba, Fall, Diagne, Diedhiou, Seck, Cissé Moot...
male
wol_3_0070
3
wol
yii gnooy gnetti mala yi geuna gaaw ci àdduna bi moo xam  ci souuf si, ci jaww ji ak ci géej gi. Téné mi moo dàkha daw ci mala yiy daw ci kaw souuf, maf moo jiitu si mala yiy naaw, Espadron-voilier moo geuna gaaw ci mala yi nekk ci ndox mi.
female
wol_8_0061
8
wol
guiss naa ab njaboot gou am juroomi xale: Ki ndieukk jigéen la, gnaareel bi goor la, gnetteel bi jigéen, gnéntteel ak diouroomeel bi ay goor laniou.
female
wol_4_0003
4
wol
ab ndongo moo nataal ab mbégué bou  mauve nekk ci kanamub niettkogne bou  giri (baam) ba neubb benn kognou niettkogne bi. meun nagnoo wax itam ni lignouy guiss nii mooy ab nietté bou  giri bou  nekk si ginnaaw ab mbégué bou  mauve.
male
wol_5_0085
5
wol
tay àllarba ci ngoon si, dinanu am ay digganté you am naadj ak you niis and ak ngelaw lou sedd. Tàngaay bi geun a mag dina toll ci gnaar fukk ak benn, bi geun a yées tollou ci juroom-gneenti degrés. Ngelaw li dina eupp ndank juroom-benni waxtu ci souba ba juroom-gnetti waxtu, ak digganté juroom-gneenti waxtou ba fukki ...
female
wol_3_0133
3
wol
Dokhantou ak ay gayndé meun na nekk ca Fathala, di benn sàmmoukaayu rabou àlleu ci biir sine-saaloum.
female
wol_5_0083
5
wol
Tay ci àlleuarba bii di fanweeri fan ak benn ay taw yu am doole la gnuy xaar si guddi gi. Bou  juroom-benni waxtu ci souba jotee taw bi dina daanu ba toll ak fukk ci téeméer boo dieul, ci noonu taw bi dafay geuna yokk ba àgg ci juroom-gnett fukk ak gnaar ci téeméer boo dieul bou  gnaari waxtu jotee. Dinagnu guiss ni ja...
female
wol_3_0098
3
wol
"Kou nekk meun na wakh né amna ay sagne-sagne aki tawfekh you sosoo ci bataakhal bii té amoul khàdj ak seen, rawatina ci wàllou khéet, mélo, Awra, làkk, diiné, péeté ci wàllou politik, khalaat, réew mbaa askan woo meunti sosoo, ci tamit wàllou jouddou alal ak luoumou meunti doon. Rakh thia dolli amoul khadjj ak sèn ci ...
female
wol_4_0150
4
wol
Ci atum 2021 laniou bind Thiébou dieun ci moomeelou àdduna yépp.
male
wol_8_0205
8
wol
Macky sall moo ngi judd fukki fan ak benn ci weeru desambar atum junni ak juroom-gneenti téeméer ak juroom-benn fukk ak benn ca Fatick, ab ndawu nguur la ci réewum Sénégal.mi ngi nekk njiitu réewu Sénégal ci atum gnaari junni ak fukk ak gnaar ba léegi. Bokk ci PDS, jàppale na njiitu réew mi Abdoulaye Wade ci bi gnuy am...
female
wol_1_0004
1
wol
ab dioubcogne bou   wiyolé bou gnouy guiss nietti pentagone you giri gnaar yi ci kaw benn bi ci souf seen digganté.
male
wol_2_0091
2
wol
Niaari fan yii ci ayou-bés bi, tàngaay bi dina yéeg ba niaar fukki degrés ak jouroom benn, sou guené wàthie yem ci foukk ak jouroomi degrés. Nouy séentou itam taw ci niaari fan yooyou.
female
wol_5_0041
5
wol
benn nga yokk ci gnaar mu jox la gnett
female
wol_8_0229
8
wol
Bari, saf te neex, lekkou Sénégal yelloo na lignou koy woowee togg bou gueuna neex ci Afrique soow-jant. Xamougnou ko bu baax ca Europe te li ci eupp ay nit daniou ciy wax loudoul deugg ci lu leen leerul, lekkam yi nga xam ne moom rek moo ko am, niou bari lool té wuuté, mooy sagou képp kou fi dëkk ak bànneexu gan yi. T...
female
wol_3_0128
3
wol
St - Louis deukou mboor la, moo ndieuka nekk gëbla Sénégal jamonoy mbéeféer.
female
wol_3_0204
3
wol
Jullit mooy ku topp Diiney Lislaam, sartees nako ci nangu te wax ni «Maangi Seede ni amul jenn Yàlla ju dul Yàlla (Allaa); Te maangi seede ni Muhammad ndawul Yàlla la» ñu koy wax Baati Seede yi Ginnaaw wax jooju, sartees ci kawam, mu Geum Yàlla moomu ca namu waree, geum ni amul ndey, amul Baay, Amul f umu yamle, Amul k...
female
wol_3_0099
3
wol
Kou nekk meun na wakh né amna ay sagne-sagne aki tawfekh you sosoo ci bataakhal bii té amoul khàdj ak seen, rawatina ci wàllou khéet, mélo, Awra, làkk, diiné, péeté ci wàllou politik, khalaat, réew mbaa askan woo meunti sosoo, ci tamit wàllou jouddou alal ak luoumou meunti doon. Rakh thia dolli amoul khadjj ak sèn ci p...
female
wol_8_0211
8
wol
Yeungu yu atum 2021 ci Sénégal  ay yeungu yu amoon la ginnaaw bi gnu jàppee gnetti fan ci weeru mars atum 2021 kenn ki geuna rànneeku ci kujje politig bi, di ab jàmbur bi Ousmane sonko. Dagnou ko tuumaal ni dafa « siif ak teukku nit ci ray ko », ab ndaw buy liggéeyee ci ab barab buy taaral ci Dakar teg ko ci ndondam. L...
female
wol_2_0173
2
wol
Ban làngou polotig moo dieul wékh ak neuteukh (wert) def ko khàmmeekaay ?
female
wol_4_0004
4
wol
ab dioubcogne bou   wiyolé bou gnouy guiss nietti pentagone you giri gnaar yi ci kaw benn bi ci souf seen digganté.
male
wol_3_0175
3
wol
Dakar mooy geubleu Sénégal. Lii eupp ci yëngou-yeungou yi ci wallou koom-koomu ak polotik, fii la nekk. Bari na ay barab you gandiarou ci mboor walla mbatiite niki Gorée... Ndar niou gueun ko xam ci Saint Louis, deukk bou mboorou nekkee ci beut gànaarou réewmi. Niou ràgné ko bou baakh ndax tabakhinou keur yi di fàttali...
female
wol_5_0175

wol_1_0007
1
wol
Xalé bou goor bi mou ngi wané benn mbégué bou sokola bou nekk si diggante gnaari niettkogne yu gnuul. meun nagnou wax tamit gnaari niettkogne you gnuul yu sékh ab mbégué bou sokola.
male
wol_5_0123
5
wol
Sénégal bari na féintekate ci wàlleu wou nekk; Ismaêl Lo, Omar Pène, Youssou Ndour, Coumba Gawlo Seck ak Vivianne Ndour ay waykat youniou ragné laniou.
female
wol_5_0221
5
wol
àllarba bii ci benn waxtou ci gouddi dinagnou am foukki deugeurés ak gnaar ànd ak ay wis-wissal you sew. loolu tax na ba taw bi tollou ci gnaar ci téeméer boo dieul, gaawaayu ngelaw li tollou ci diouroomi kilomeetar ci waxtu wou nekk, tooyaay bi tollou ci juroom-gnaar fukk ak juroom-gneent ci téeméer boo dieul. meun  n...
female
wol_8_0057
8
wol
Téeméer nga foul ko ak benn niénteel mu jox la gnaar fukk ak juroom.
female
wol_5_0015
5
wol
Benn jégguikaay bou xala bou gnou tabax ba mu baax ci kaw dekh. Niou samp si ay poto lamp you mbokh ci pegg yi.
female
wol_5_0105
5
wol
Tour yi geuna bari Sénégal ci goor gni niooy : Ablaye , Abdou, Mamadou, Ibrahima, Pape, Assane, Adama Lamine, El Hadj Tourou djiguéne yi geuna bari niooy : Ndèye, Fatou, Astou, Amy, Khady, Marème, Adja Sant yi geuna bari niooy : Ndiaye, Diop, Sarr, Diallo, Coly,Diouf, Gueye, Ba, Fall, Diagne, Diedhiou, Seck, Cissé Moot...
female
wol_1_0099
1
wol
Kou nekk meun na wakh né amna ay sagne-sagne aki tawfekh you sosoo ci bataakhal bii té amoul khàdj ak seen, rawatina ci wàllou khéet, mélo, Awra, làkk, diiné, péeté ci wàllou politik, khalaat, réew mbaa askan woo meunti sosoo, ci tamit wàllou jouddou alal ak luoumou meunti doon. Rakh thia dolli amoul khadjj ak sèn ci p...
male
wol_3_0113
3
wol
Ban réew la Tombouctou nekk ? Tombouctou mou nga tcha Mali, deuk bou làmboo mboor mou gandiarou tchi wallou xam-xam ak mbatite.2) Bamako geubla ban réew la ? Bamako mooy geublak Mali, di sélébeyoon bu am solo ci zallou dieund ak diaay ci Afrig Soowdiant.3}Fan la Ali Farka Touré Thiosaanoo ? Ali Farka Touré, waykat bou ...
female
wol_4_0090
4
wol
Tay ca Tambacounda nekk ci penku Sénégal beuthieug bi dina tàng lool ndax tàngaay bi dina yéeg ba gneent fukk ak juroomi degrés.
male
wol_8_0207
8
wol
Amy Mbacké Thiam moo ngi judd fukki fan ci weeru nowambar atum junni ak juroom-gneenti téeméer ak juroom-gnaar fukk ak juroom-benn ca Kaolack, moo ngi nekk ab atlet bu réewum Sénégal di dawkatu gneenti téeméeri meetar yi. Moom moo nekk kenn si taarixu Sénégal ku mos a jeul raaya bu jongante bu àdduna bi yeupp di seq. ...
female
wol_8_0040
8
wol
benn nga yokk ci gnaar mu jox la gnett
female
wol_3_0035
3
wol
maa teg ci taabal ji ab pom bou  neuteukh bou  nekk ci ginnaaw xaajou pom bou  neuteukh.
female
wol_3_0075
3
wol
niral ak nqamtou gnaar: gnaari woykat yi Pape ak Cheikh, gnaari at ginnaaw bi gnou taxawalee seen kippaango siife nagnu ak labelou Youssou Ndour Jololi. jàppal ni gnaari woykat yii ay xarit lagnou bi gnou nekkee xale ba léegi.
female
wol_4_0119
4
wol
Abdou Diouf kan la woutou ci boppou réewu Sénégal? Leopold Sédar Senghor la woutou ci atu 1981.
male
wol_4_0030
4
wol
ab bant bou neuteux  bougnou dindee ci garabou  banaana te ànd ak ay xobam you neuteukh te gnou teg gnetti banaana you mbokh you reuy ci kanamam.
male
wol_3_0132
3
wol
Kaolack deukk bou am solo lool ci wàllou dieund ak jaay mel nani mooy diggou Sénégal ndakh fimou.
female
wol_4_0153
4
wol
Réewu Sénégal dioullit yi nioo geuna bari.
male
wol_3_0078
3
wol
Tay ci àllarba ji, ci gnaari waxtou ci souba asamaan sou xiin la gnouy guiss ak tàngaay bou  tollou ci juroom-gnetti degrés. Sou gnétti wakhtou dioté dinagnou guiss ay taw ak tàngaay bou  tollou ci fukki degrés ci souba ba gnaari degrés ci ngoon. Ayou-bés bii dina sedd lool kon xalaat leen génné mbàdj yi ak yeuré you d...
female
wol_3_0225
3
wol
Tay ci àlleuarba bii di fanweeri fan ak benn ay taw yu am doole la gnuy xaar si guddi gi. Bou  juroom-benni waxtu ci souba jotee taw bi dina daanu ba toll ak fukk ci téeméer boo dieul, ci noonu taw bi dafay geuna yokk ba àgg ci juroom-gnett fukk ak gnaar ci téeméer boo dieul bou  gnaari waxtu jotee. Dinagnu guiss ni ja...
female
End of preview. Expand in Data Studio

Google WaxalNLP Wolof Re-alignment

Google introduced WAXAL, a new open dataset for 21 African languages, to tackle data scarcity and build inclusive speech technology. However, the Wolof language has experienced alignment issues between the audio files and their transcriptions, making the dataset unusable.

We therefore propose to correct this using a simple and effective approach:

  1. For each audio clip, we generated a transcription using Google Gemini ASR.
  2. For each generated transcription, we calculated the Levenshtein distance with all the initial transcriptions.
  3. The lowest distance obtained indicates the most similar initial transcription to the one generated by the ASR.
  4. The index corresponding to this initial transcription is the correct index that will be used to correct the misalignment.

We also identified a couple of corrupted files during the process that could not be read. As part of this filtering process:

  • 171 samples were removed from the train split
  • 20 samples were removed from the test split
  • 22 samples were removed from the validation split

Leaving the final dataset with the following stats:

DatasetDict({
  train: Dataset({
  features: ['id', 'speaker_id', 'locale', 'gender', 'audio', 'text'],
  num_rows: 834
    })
  test: Dataset({
  features: ['id', 'speaker_id', 'locale', 'gender', 'audio', 'text'],
  num_rows: 111
    })
  validation: Dataset({
  features: ['id', 'speaker_id', 'locale', 'gender', 'audio', 'text'],
  num_rows: 97
    })
})

NOTE: Some audio files show a duration of 00:00/00:00 in the HuggingFace player but play properly once loaded into your script.

Dataset duration

Grouping by split:

Split Duration Total (seconds) Nb of samples
Train 411 min 10 s 24 670 s 834
Test 52 min 18 s 3 138 s 111
Validation 39 min 46 s 2 386 s 97
--- --- ---
Total 503 min 15 s 30 195 s 1042

Grouping by speaker id:

Split Speaker ID Duration (H, M, S) Nb of samples Gender
Train 1 1 h 28 min 46 s 150 male
8 1 h 09 min 33 s 129 female
5 1 h 07 min 27 s 128 female
3 1 h 05 min 41 s 171 female
2 1 h 00 min 49 s 128 female
4 0 h 58 min 55 s 128 male
--- --- --- --- ---
Test 2 0 h 15 min 12 s 20 female
3 0 h 11 min 20 s 20 female
5 0 h 10 min 02 s 23 female
1 0 h 06 min 00 s 19 male
4 0 h 05 min 52 s 14 male
8 0 h 03 min 52 s 15 female
--- --- --- --- ---
Validation 8 0 h 07 min 57 s 18 female
2 0 h 07 min 10 s 18 female
4 0 h 07 min 08 s 15 male
1 0 h 06 min 40 s 17 male
3 0 h 05 min 52 s 16 female
5 0 h 05 min 00 s 13 female

The speakers' genders were missing from the initial dataset and were marked as unknown. To correct this, we started by grouping the audio files by speaker_id, then listened to samples from each speaker to manually determine their gender. We ended up identifying 06 genders: 02 males and 04 females.

Load the dataset

You can download the dataset with the following script:

from huggingface_hub import snapshot_download

snapshot_download(
    repo_id        = "galsenai/WaxalNLP",
    repo_type      = "dataset",
    allow_patterns = "data/*.parquet",
    local_dir      = "./waxal_wol"
)

And then load the dataset with the following:

from datasets import load_dataset

dataset = load_dataset("parquet", data_files={
    "train": "waxal_wol/data/train-*.parquet",
    "test":  "waxal_wol/data/test-*.parquet",
    "validation": "waxal_wol/data/validation-*.parquet",
})

print(dataset)

The notebook used to make these corrections is available on Google Colab to help you fix similar issues in your language, pending the upcoming fixes planned by the Waxal project team.

This work has been carried out by Derguene, with Abdou Aziz who helped to identify the misalignment issue.

Downloads last month
181