Dataset Viewer
Auto-converted to Parquet Duplicate
audio
audioduration (s)
2.15
7.1
transcription
stringlengths
31
61
dootuma réer bu ma fay dem lekkool beey sama takk
bokkoo gi am ci seen biir mooy seen doole
ruur dafa xawa nuru cool waaye moo gën a réy te gë a ñuul
li ngay digle soo ko doon topp kenn du la gën
xaaral ba ma nàmpal sama doom ba noppi
ci tàng tàng bi nga ko waroon a tontu
mu ni ko buur dé moo ni naa ko rattal nag wu góor wi
bi ñu demee xareji loolu lañu lël ci dëkk yi
jinné ji ko doxaansi kat saatañaali la tudd
ci seen aada dañu leen di daggal seen coppret
su sunuy kàddu dëppoo mbir mi dootul yàgg
kenn mënul sukkandiku ci wax ju lënt jii
bu ngénte li weesoo nanga ma dajaleel ndab yépp ba ñu daj
man dey ci yoonu jàmm wi laay aw bu ma yeboo gumba
soo bàyyiwul yëddu dinga mësa dégg lu la dul neex
abal ma sa sémmiñ ma xàpp matt mi
dafa jóoke ay buum ndax teen bi dafa xóot
xaaral ba timis fàddu nga door a génn
soo defalul màngo si cëslaay jur gi dina ko daaneel
xàjjaatlewul ay noonam ak ay ñoñam
dañu leen daan jox sàngara ngir ngóoraal leen
bi ginaar yi sabee njël waa ji jóg jubal néegu gan gi
sa mbubb mi ànd na ak maraakiis yu puur
soo ko bàyyee ba mu jekku la dina la gaañ
danga wara dëppale sa doxalin ak jamano ji
léegi daawur dafa mel ni ku télbati
balawlaw tàppit malaan a ngoog am yobbaale ko buur
bu ma tolloo diggante seeti samay wóllëre
juuyoo warul am ci diggante say bëgg bëgg ak sama yos
màngo ji neex na waaye càmpóor yee ko yàq
maa yey wóolu ko ndax mosuma ko dénk lu luubu
daggal mburu mi ci digg bi te jox ma xaaj bi
wéradeem googoo ko taxa bàyyi mbay mi
doktoor bu nekk région de cap vert rekk dem naa fa
dañu koy defar jiib ko ci ndox moomu
njaag xam na waalo waalo xam na njaag
def naa ci sama kem kàttan waaye àntuwul
xaaral ba simis bi gëna muus nga fudd ko
masin dafay gar rekk bu ko defee nga wolaat ba mu mokk
tabaxub taax mee tax ñu téj yoon wi
bët du yenu waaye xam na lu bopp àttan
soo fa demee dina la ganale ni mu ware
sama fanweeri bëñ yooyu ak ñaar bu ñu génn kër gi
dafa taxaw ci buntu kër gi ba yàgg mu dem
kon nag jigéen ju baax moom boo ko amul dangay bàyyi
ñu daw du ne ni baay maa ci jëkk
ku nekk matal na liggéey bi du ko sasoon
léegi nag mu yegg ci dëkk bi yaayam nekk
bul foog ni togomonte mag rekk lay jàpp
di ma di génne ci sama yaram wi lu mel ni ay paañ
sumb bu jëkk bi dafa ñuul kukk ndax tilim
xale bi yuqamtalu na ba àjji màngo bi
xam nga ni bëqët bii ñemewu fi fanaan moom rekk
fi ma oto bi wàcce dafa sore kër gi
paj bi jeexagul kon nag du mën a ñibbi
fara tëgg né ko baax na mu daaj béy wa dee
mu ngi topp tali bi di tëñëx tëñëxi
boot na xale bi ba mu yàndoor mu tëral ko
ndegem mucc ngeen rekk li ci des amul solo
jooy ya metti nañu lool ca kër ga mu dee
yenn saa damay fàtte ne nekkuma senegaal
ma ngi jëm jàmb ji nekk ci seen wetu kër
sama lam bi dafa ma lew moo tax mu feeñ
boo amoon kersa duma taxaw ngay saaga
dangeen wara sàkk ab dig ci seen tool yi
soo leen boolee dinañu gaawa xaritoo
ku tëb dal cib daay dese nga beneen tëb
séysi na biig ginnaaw ëllëg lay yebbi
xaaral ba mu géex nga sog koo tëral
dafa àbb sama simis dal di ko def ag moomeel
ci siis bi lay sukkandiku sog a jóg
dafa doon dox ba yàgg mu ne dàll daanu
bi ma dajee ak moom dafa dummóoyu ndax gàcce
kawlax yu dul laal bar ndax seen tuur la
sàcc yi yóbbu nañu ganaar yi woon ci ngunu li
mandaxe nanu ko mu nekk juróomi kilo
bi ñu dee xale dañu daan lekk suñel
dañu daan def seen alal yépp ci mbanaar mi
rajo baa ngiy yeete ci sëqat su bon si
su nopp doon ràcc laax ñu woo mbaam sëf
bul màmm nag xamal fi nga war a yem
dañu topp tànku sàcc bi ba gis kër gi mu làqu
amari ngoonee taxoon kajoor feyatul voon galag jolof
seetal ci kóllëre gi dox sunu diggante
dama ko yedd mu dal di fa jóge bàyyi tux
baay bi ni billaahi jooyatuñu sunu ñàkkum doom ju góor
ca cosaan kenn daawul takk jabar ju la say mbokk tànnalul
ndaw soosu du def lu ñaaw lingeer dëgg la
réew yu naat yi ñoo sos kuréel googu
jëndaguma reseñseg ji war dem ci cere ji
bul xaar ba siwó bi rembat nga soga téj róbine bi
dañu tabax loxo bi moo tax ma di ko wodd
dàqal xaj bi mu ngi xab ndox mi ci bool bi
tey lañu waroon sabaru waaye dañu ko fomm
bi ñu agsee daldi dugg ci kër gi seet seet gisuñu kenn
ku faat bakkan war nga xam ni doo ci génne noonu
man déy duma séy ag boroomub légët
xam nga ni mënuloo yëkkëti poowu juróomi kilo
tëgg dawul mbaar dipolom yi la ko tontoo
sama xarit yépp ndawtal nañu ma ba mu des yow
End of preview. Expand in Data Studio
README.md exists but content is empty.
Downloads last month
6