url stringlengths 43 43 | content stringlengths 1.49k 122k | source stringclasses 1
value |
|---|---|---|
https://sacred-texts.com/bib/wb/wlf/mat.htm | 1:1Lii mooy cosaanu Yeesu Kirist, sëtu Daawuda, sëtu Ibraayma.
1:2Ibraayma moo jur Isaaxa; Isaaxa jur Yanqóoba; Yanqóoba jur Yuda ak i doomi baayam;
1:3Yuda, Fares ak Sara ci Tamar; Fares Esrom, miy baayu Aram;
1:4Aram Aminadab; Aminadab Naason; Naason Salmon;
1:5Salmon jur ci Raxab doom ju tudd Bowas; Bowas am ak ... | New Testament |
https://sacred-texts.com/bib/wb/wlf/mar.htm | 1:1Xebaar bu baaxu Yeesu Kirist, Doomu Yàlla, nii la tàmbalee.
1:2Bind nañu ci téereb yonent Yàlla Esayi naan:«Maa ngi yónni sama ndaw ci sa kanam,mu xàllal la sa yoon.
1:3Baat a ngi xaacu ca màndiŋ ma naan:“Xàll-leen yoonu Boroom bi,jubal-leen fi muy jaar.”»
1:4Noonu Yaxya feeñ ca màndiŋ ma, di sóob nit ñi ci ndox,... | New Testament |
https://sacred-texts.com/bib/wb/wlf/luk.htm | "1:1Yaw Teyofil mu tedd mi, xam nga ne, nit ñu bare sasoo nañoo bind ab nettali bu jëm ci mbir, y(...TRUNCATED) | New Testament |
https://sacred-texts.com/bib/wb/wlf/joh.htm | "1:1Ca njàlbéen ga fekk na Kàddu gi am, te Kàddu gi ma nga woon ak Yàlla, te Kàddu gi Yàlla l(...TRUNCATED) | New Testament |
https://sacred-texts.com/bib/wb/wlf/act.htm | "1:1Yaw Teyofil, téere bu jëkk, ba ma bindoon, ëmb na lépp li Yeesu tàmbali woon a jëf ak a j(...TRUNCATED) | New Testament |
https://sacred-texts.com/bib/wb/wlf/rom.htm | "1:1Man Pool, jaamub Kirist Yeesu, maa leen di bind bataaxal bii. Yàlla woo na ma, ma nekk ndawam, (...TRUNCATED) | New Testament |
https://sacred-texts.com/bib/wb/wlf/co1.htm | "1:1Man Pool, ndawul Kirist Yeesu ci coobareg Yàlla, man ak Sosten sunu mbokk,\n\n1:2noo leen di bi(...TRUNCATED) | New Testament |
https://sacred-texts.com/bib/wb/wlf/co2.htm | "1:1Man Pool, ndawul Kirist Yeesu ci coobareg Yàlla, man ak Timote sunu mbokk, noo leen di bind, y(...TRUNCATED) | New Testament |
https://sacred-texts.com/bib/wb/wlf/gal.htm | "1:1Man Pool, ndawul Yeesu Kirist --nit falu ma ko, te jaarewul it ci nit, mi ngi jaare ci Yeesu Kir(...TRUNCATED) | New Testament |
https://sacred-texts.com/bib/wb/wlf/eph.htm | "1:1Man Pool, ndawul Kirist Yeesu ci coobareg Yàlla, maa leen di bind, yéen gaayi Yàlla yu sell y(...TRUNCATED) | New Testament |
End of preview. Expand in Data Studio
README.md exists but content is empty.
- Downloads last month
- 9