audio audioduration (s) 1.22 171 | transcription stringlengths 6 108 |
|---|---|
bëgg naa xaj yi. | |
xaw nanoo dee ak xiif. | |
afirik sa téere bi, kalaame bu meti la, booy kalaame kopparu euro ak cfa | |
looloo ma tax a bég ci li ma jot ci yool boobu | |
xalaat mii a yànj ! | |
mel ne moom it ay jafe-jafey kese la | |
njariñ li it yal na bari | |
waxuma la ak lu jëm ci wàllug yoon | |
foytéefam këmbaan guy lang, 10 ba 30i sàntimet moo di guddaayam. | |
sopp naa kàggu yi. | |
i at ba tay, sunuy jafe-jafe ci wàllum paj soppikuwul. | |
téyéel sa làmmiñ ! | |
lat-joor jóob, dammeelu kajoor | |
lan mooy taxawaayam? | |
turu 2 nit ñi wuute ci injiil | |
bokk nq ci li mu wax di ci tagg sëriñam ba sëriñ tuuba | |
exquisite-kfind.png ngir xóotal, yërël bii jukki ci jàppum njaam | |
amna tuuti xaalis. | |
peeyug kaabu, kansala, la woon | |
yeen a ngi may gaañ ! | |
ndeem soob na yàlla. | |
politigu suturaanami jëfandikubindwaay | |
ndax nun doŋ la ? | |
koko gi xeetu garab la gu bokk ci njabootu arecaceae. | |
seen yaay a ngi fi a? | |
mi ngi ci mbàmb lu ñàng. | |
lan la loolu di tekki? | |
bu ngeen xëyatee | |
sóobarey mbootaayu xeet yi ak askan wa | |
mbàmbulaan gu atlas | |
ñenn ngeen ci gaa ñu ndaysaanu ñi ! | |
ku yaroowut ci ab sëriñ dana daje ak coono. | |
tom nuru na ku am yar. | |
li dale ci robowam ñetteelu buur ci yuda la woon | |
dangaa gaañu ? | |
xalaat naa ne wax na dëgg. | |
man na wàlle ci lu sew ak ci lu tar | |
damaa tëdd ngir dallu. | |
guddaayu yamoo gu suuf si mi ngi tollu, ci xayma, 40 075 km. | |
ndax nun doŋ la? | |
maa ngi metitlu ak moom. | |
nit ñii mat nañu 241 952 2010. | |
nataali xiirtalukaay yu ndombo yees móol | |
doo leen xool. | |
nogoy mi nga xam ne ndawal kër doktoor la, dem na këram seeti ko. | |
tey-si-tey nag, woowule woy, warees na koo jëmale ci góor ak jigéen | |
turam feeñ na ci injiil ci ro 1614. | |
man naa nekk dawaan bu safaanu walla bu wéy. | |
indoneesi bokkeef bu indoneesi réew | |
fexee sottal càkkuteef dongay daara ju iseb jamñaajo. | |
bu jaab yàggee gawar feeñ | |
daanaka kóoluteem ci goney ekip bi amul àpp | |
danoo war a tekki. | |
ubbi njël lu njëkk li | |
wurus wi moom xalaatunu ko koo laaj | |
abdu rahmaan léy | |
damaa bëgg ub dawantu. | |
bëj-saalum-penku asi ci goxu asi la bokk. | |
garab gu dëgër lay doon ci jamonoy noor. | |
ndax am naa pexe ? | |
dama doon naxaate. | |
nataalu xobi gàncaxug gerte | |
sama baay daa jàpp . | |
pàccu tiyaataram defoon lu rëy. | |
dangaa war a jug. | |
ma door a séwét siiwna. | |
dafa gaaw a yaqu lool. | |
naa dem sama yoon sax. | |
noppi naa ngir tàmbali. | |
i ba tay, lu jóg fëkk nu. | |
maa ngi doxal barab bii. | |
man nga cee dem leegi. | |
danuy dellu ginnaaw. | |
tasee naa ak moom démb. | |
jigéen ñi, ñoom, dañ leen daan siif saa su nekk, di leen tëdde | |
xoolal sa gannaaw . | |
koorug jàmm na nu ñeel. | |
sëriñ saaliwu ci melo wuy wone ag ragal yàlla ak ginnaawal àdduna | |
waxal tom ne maa ngi jéggalu. | |
paj lan mooy koronaawiris ? | |
lan moo ma wor ? | |
ñépp a ko sopp. | |
limub ñi faatu jóge na ci juróom-ñent ba ñaar-fukk ak ñatt. | |
ndax sell na ? | |
ñi ko nàngulul te jàppunu, | |
bokkeef bu finlaand wu-finlaand suomen tasavalta réewum tugal óróop | |
te, daanaka, looloo di laago bépp doomu afrig | |
damaa xaw a xiiw. | |
ndax dingeen nelaw ? | |
biraan jaaxle lool, jël sànnikaay bi teg ci tuñ mi. | |
dawkat bu gaaw la. | |
mi ngi ak néegu boppam. | |
kañ la tom egsi ? | |
seen jataay mboor ak xayte | |
rfm xamle na ne ŋamtu 51 bi la. | |
nit ku mukàllaf dina ci am lu toll ci juróomi liitar | |
damay jàng angale. | |
ku am wërsëg laa. | |
kër gi daa yaatu. | |
am nga dëgg ci xaaj bi. |
End of preview. Expand in Data Studio
README.md exists but content is empty.
- Downloads last month
- 14